Liggéey yi

Soxla nga kayitu dëkk, nationalité espaañol, walla nga bëgg a jubbanti sa mbir ak arraigo? Dinanu la dimbali. Xam nanu bu baax mbiri doxandéem yi ak li ñuy laaj ci mbir mu nekk.

Sa ëllëg mi ngi aju ci mbir yii, moo tax danuy liggéey ak teey. Danuy topp sa dossier tànk ak tànk te danuy la jàppale, yaw ak sa njaboot.

Nationalité

Ci mbirum nationalité espaañol

Nationalité espaañol ndax dëkk

Ndimbal ngir ñi dul doomu Tugal (UE)

Arraigo social

Arraigo familiar

Arraigo sociolaboral (ak liggéey)

Arraigo socioformativo (ak njàng)

Dëkk ndax dajale njaboot

Dëkk bu boppam ngir njaboot bu ñu dajale

Dëkk bu amul liggéey (no lucrativa)

Dëkk ak liggéey ci kenn (cuenta ajena)

Dëkk ngir stage bu ñu dul fey

Dëkk ngir doom bu juddoowul Espaañ

Dëkk ngir doom bu juddoo Espaañ

Kartu dëkk ngir mbokku doomu Tugal (UE)

Arraigo de segunda oportunidad (beneen yoon)

Ndimbal ngir doomi Tugal (UE)

Certificat d’enregistrement ngir doomu Tugal (UE)

Certificat dëkk bu sax ngir doomu Tugal (UE)

Ndimbal ngir doxandéem yi ci Espaañ

Wóolu nu, nu wone la yoon wi. Ci bépp tànk nu ngi fi ngir nga am li ngay bëgg te am sa barab ci Espaañ.

Jokkool ak nun te tàmbali sa mbir tey, ci loxo yu xam liggéey bi.

Yeesal kayit yi

Yeesal dëkk bu amul liggéey

Yeesal dëkk ak liggéey ci kenn

Yeesal dëkk ndax dajale njaboot

Yeneen ndimbal

Parejas de hecho

Nu ngi fi ngir lépp loo soxla

Mbir mu nekk dafa wuute. Danuy topptoo yaw te jàng sa mbir bu baax.

Ndimbal ngir doxandéem yi ci Espaañ