Arraigo familiar

Lan mooy arraigo familiar?

Kayit la ngir dëkk te liggéey ci Espaañ.

Ngir ku yor mbokk mu doomu Tugal (UE): doom bu ndaw walla nit ku am lago.

Soxlawul diir bu tollu ci Espaañ.

Ndax yaw la jëm?

✓  Yaw mooy baay, yaay walla tuteur bu doom bu ndaw bu jóge beneen réewu UE (du espaañol), dëkk nga ak moom walla ngay fey pensionam, walla

✓  Yaa ngi topptoo mbokk mu jóge beneen réewu UE te am lago, te dëkk ngeen benn kër.

✓  Amoo tooñ ci yoon te amoo laaj asile.

Sa doom espaañol la? Kon mbir mi wuute na: dëkk ngir mbokku espaañol. Laaj nu, dinanu la dimbali.

Ban kayit nga soxla?

▸  Paaspoor bu mat (xët yépp).

▸  Kayitu yoon bu réew yi nga dëkk ci 5 at yi weesu (bu ñu tekki te légalisé).

▸  Su dee ngir doom: kayitu juddu bu doom ji (walla kayitu tutelle).

▸  Su dee ngir nit ku am lago: kayiti lago bi ak kartu identité bi.

Ñaata lay yàgg? Lu tollu ci 3 weer.

Xibaar yu gën a bare (yoon wi, ci espaañol)

Autorización de residencia temporal por circunstancias excepcionales por arraigo familiar (Ley Orgánica 4/2000, art. 31.3; Real Decreto 1155/2024, arts. 124-127 y 130-132; Instrucciones DGM 8/2020).

Supuestos: a) padre, madre o tutor de un menor nacional de otro Estado de la UE, del EEE o de Suiza, que resida en España, tenga a cargo al menor y conviva con él o esté al corriente de sus obligaciones paternofiliales; b) familiar que presta apoyo a una persona con discapacidad nacional de otro Estado de la UE, del EEE o de Suiza, que la tenga a su cargo y conviva con ella.

Requisitos: no ser ciudadano de la UE, del EEE o de Suiza; carecer de antecedentes penales en España y en los países de residencia de los últimos cinco años; no figurar como rechazable en países con convenio; no estar en plazo de compromiso de no retorno; no ser una amenaza para el orden público, la seguridad o la salud pública; encontrarse en España y no ser solicitante de protección internacional. No se exige permanencia mínima.

Documentación: impreso EX-10; pasaporte completo en vigor; certificado de antecedentes penales; certificado de nacimiento del menor con vínculo y nacionalidad o documento de tutela, o bien documentación de la discapacidad, de estar a cargo y de convivencia, y documento de identidad del ciudadano de la Unión. Documentos extranjeros traducidos y legalizados o apostillados.

Procedimiento: se presenta personalmente en la Oficina de Extranjería de la provincia o telemáticamente (Mercurio). Tasa: modelo 790 código 052, epígrafe 2.5. Plazo de resolución: tres meses (silencio negativo). Tras la concesión, hay un mes para pedir la TIE en la Comisaría.

Información orientativa basada en la hoja informativa oficial del Ministerio (mayo de 2025). Solo es de aplicación la normativa vigente en el momento de la solicitud.

Am nga laaj? Waxal nu sa mbir te dinanu ko seet

Ndimbal ngir doxandéem yi ci Espaañ