Lan mooy certificat inscription UE?
Mooy xaymar bi (“certificat vert”) citoyen européen yi dëkk Espaañ lu ëpp 3 weer war a am.
Ak moom, dangay am sa NIE. Dinañu la ko jox bis bu rendez-vous bi.
Moytul jamono ji! War nga ko laaj ci 3 weer ginnaaw bu agsee Espaañ.
Ndax mooy ngir yaw?
✓ Yaw mooy citoyen bu réew bu bokk ci Union Européenne, Espace Économique Européen walla Suisse (xool lëkkalekaay bu réew yi).
✓ Dangay dëkk Espaañ lu ëpp 3 weer.
Boo bokkul ci Europe te sa mbokk bokk na, lu nga soxla mooy kart mbokk UE.
Réew yu bokk ci Union Européenne ak réew yu bokk ci accord Espace Économique Européen:
* Réew yu bokk ci Accord Espace Économique Européen.
** Accord bu 21 suiin 1999, diggante Communauté Européenne ak Confédération Suisse, ci mbir bu libre circulation des personnes.
Lan nga soxla?
Kayit yu bawoo: paaspoor walla pièce identité bu sa réew, formulaire EX-18 ak tasa bi fay. Ak itam, mengook sa mbir, benn ci mbir yii:
